TRENVID

What the world is watching right now

Jahman X-Press, Ahmada Jadid & Abdou Khoudoss Kara - BAMBA LA SOLUTION (Official Video)

Jahman X-Press, Ahmada Jadid & Abdou Khoudoss Kara - BAMBA LA SOLUTION (Official Video)

Jahman X-Press · 441,159 · 2026-07-25

Watch on YouTube ↗

What this video is about

anotheraremewe

Auto-summarised from the video’s captions. It may be imprecise.

Description

Crédits de la chanson et du clip : Prod : Momo Beats ,Loufa Beatz & Jean Mermoz Production : Optique Studio Director : Ibrahima Mbengue Dione Color Grading : Ibrahima Mbengue Dione Camera Operator : Babacar Sow Assist. Cam : Collé Diallo Lights : Racine & PooRich Prod Management : Metha Cast : Sisko Fadilou Prod : Jean Mermoz - Loufa Beats Studio record : Scenes-Gal Prod - Evo Studio Mix & Master : Moussa Ngom Special Thanks : The Teranga - Phare des Mamelles - Scenes-Gal Prod Lyrics Zahiim: Rikk gaay ñi, bu kenn jaaxle, Sëriñ BAMBA wuyusi nan Yërmaandeem a bari ci ñun ba tax na dikk na sauver jàmm ñi JAHMAN: Yeem naa la yemoon naala mbacké yeematinaala Yaa fi neekal Yalla hazawadjala Rëjërajëfeteeti JADID: Bamba fettal na rap wa Ceerno Ibra Faty fees ko Dogté ko togg ko ñew leen reer ko Mbana ga juniy ñay la ZAHIIM: Xanaa da nuy sukaat di raam, ba ñëw ci yaw te naan la Maam Bootal té roganti ñu JADID: Bëgg na noo am sa ngëram, bo ñu baaxee dinañ ko am Muy texeg tay ak ëllëg ZAHIIM: Motax jébbalu nañ bu wéra wér ak mbooleem lu ñu am tey saxoo sant gudd’eek bëcëg JAHMAN: Xëy suba teel, léemoo Sa Tur wu màgg Wii Day tax a mucc, te day waral say mbir gaaw JADID: Seex Bamba doy loo lu doy, daa am solo YAAY ki ñu doy Tay ak ëllëg, YAA gën ci nday YAA gën ci baay ZJJ: Seex Bamba ñoong lay dagaan ci barke Al Muntaxa borom mbeg meek taar bi Buur Yàlla naatal reew mii REFRAIN: Ndimbal Ndimbal ak Yërmande (Ndimbaloo Fall) Murid Jëfé Ndigal baayi téré (Ay Goor Yalla lolooy yoon wi) JADID: Borom jummaa ji, Doomi Jaara Buso ngala dimbalinu, da noo doyadi rek waaye yëram nu Yaay mbegtem sunu Xarnu ZAHIIM: Mbacké ñaan nan la, deelu ñaanati baarké Borom Daaru Nang nu samal ngor gi ba ba ñuy faatu Xeewal yit bum ñuy bew loo JAHMAN: Ñaan nañ ci barke mafarma yacine Daour mi ci mbul sagal nu, Issa Dièye fatim penda leeram ga sar na ba juroom ñaari assamaan yéé JADID: Ndax da ngaa bari ay may, ña daan falu yaalen fal ZAHIIM: Neleen eskey sangub Maam Seex Ibrahima Fall JADID: Ajanna yeep a ngay riir ngir ngir saam faali baay fall ZAHIIM: Neleen eskey sangub Maam Seex Ibrahima Fall Chœurs: Faala gën (Madegel) Maam Seexa raw (ngañ madegel demba)*3 Ngañ ma ca leer ya (Degel) ZAHIIM: Motax jébbalu nañ bu wéra wér ak mbooleem lu ñu am tey saxoo sant gudd’eek bëcëg JAHMAN: Xëy suba teel, léemoo Sa Tur wu màgg Wii Day tax a mucc, te day waral say mbir gaaw JADID: Seex Bamba doy loo lu doy, daa am solo YAAY ki ñu doy Tay ak ëllëg, YAA gën ci nday YAA gën ci baay ZJJ: Seex Bamba ñoong lay dagaan ci barke Al Muntaxa borom mbeg meek taar wi Buur Yàlla naatal reew mii REFRAIN: Ndimbal Ndimbal ak Yërmande (doleey biir Fall) Murid Jëfé Ndigal baayi téré (Ay Goor Yalla lolooy yoon wi)

Jahman XpressDamalay beuggDiamanEternelleJantu mbeuguelWally SeckVjMia GuisseTarba MbayeTitiDjelykaba BinetouNgaaka Blinde

Trending at the same time

Advertisement
TRENVID collects the videos trending on YouTube across 11 countries and shows them in one place. © 2026 ZZXXCCVV. All rights reserved.